Genesis 47:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yuusufa daa dem ca Firawna, wax ko ne ko: «Sama baay ak samay bokk, jóge nañu Kanaan, ànd ak seen jur gu gàtt ak gu gudd ak mboolem lu ñu moom. Ña nga léegi ca diiwaanu Gosen.»