Genesis 47:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yuusufa nag dajalee ca pepp, ma mu jaay waa Misra ak waa Kanaan, mboolem xaalisu ñaari réew ya, yóbbu nag xaalis ba kër Firawna.