Genesis 47:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yuusufa nag jëndal Firawna suufas Misra gépp, ngir waa Misra ya jaay ku ci nekk sa tool ndax xiif, ba leen jiital, ba Firawna mujj moom suuf si.