Genesis 47:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yuusufa ne waa réew ma: «Léegi gannaaw jënd naa leen, ba Firawna moom leen, yeen ak seeni suuf, jiwoo ngii, demleen jiyi.