Genesis 6:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Askanu Nóoyin mooy lii. Nóoyin nit ku jub la woon, di ku mat ci biir nit ñi mu bokkal jamono, te di ku topp Yàlla.