Genesis 7:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem mbindeef mu daan dox ci kaw suuf dee na ca. Picc yi ak jur gi ak rabi àll yi ak lépp luy raam ci kaw suuf dee na, ñoom ak nit ñépp.