Genesis 8:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu négati juróom ñaari fan, bàyyiwaat pitax ma. Boobu yoon nag délsiwaatul ca moom.