Genesis 8:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul pitax ma gisul fenn fu mu tag, ndax ndox mi muur na suuf sépp. Mu délsi nag fa moom ca gaal ga. Nóoyin tàllal loxoom, jàpp ko dugal ci biir fi wetam.