Habakkuk 1:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aw ay lañuy dikke, ñoom ñépp, buurandoo, jubal màkk seen kanam, te ñi ñuy jàpp njaam bare ni feppi suuf.