Habakkuk 2:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fa may jongroo laay taxaw, ne temm fa kaw tata ja, ba xam ana lu mu ma Aji Sax ji di àddu, ak lu may waxaat ci samab tawat.