Hebrews 1:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yàlla musul a teral kenn ci malaaka yi, ba di ko wax:«Toogal ci sama ndeyjoor,ba kera may daaneel say noonci sa kanam.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana kan ci malaaka yi la mas ne: «Toogeel sama ndijoor, ba ma def say noon, say dëggastal »?