Hebrews 1:14 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Malaaka yépp ay xel lañu rekk yuy liggéeyal Yàlla, mu di leen yónni ñuy dimbali nit, ñi nar a jot mucc gi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa malaaka yépp duñu ay ngelaw yu ñu sas ab liggéey, yebal leen ngir ñu taxawu ñi wara jagoo ag mucc?
Recommended Reading