Hebrews 1:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye ci wàllu Doom ji, lii la ko Yàlla wax:«Yaw Yàlla, dinga toog ci jal bi ba fàww,ci njubte ngay nguuru.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye Doom ji la Yàlla ne: «Yàlla, sab jal tey la ak ëllëg ba fàww, te sa yetu nguur njub lay doon.
Recommended Reading