bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 10:12
Hebrews 10:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye nag saraxalekat bii di Kirist, bi mu saraxee sarax bu am doole ngir dindi bàkkaar yi benn yoon ba fàww, dafa toog ca ndeyjooru Yàlla,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye kii de, ba mu sarxee ngir ay bàkkaar, bennub sarax, mu doy ba fàww, ca la tooge fa ndijooru Yàlla.