Hebrews 10:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
dafa jëkk a wax ne:«Boroom bi nee na:Kóllëre gaa ngii,kóllëre gi may fas ak ñoom,bu bés yooyule weesoo.Dinaa def samay ndigal ci seen xol,bind ko ci seen xel.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
nde gannaaw ba mu nee: «Lii moo di kóllëre gi may fas ak ñoom, bu fan yooyu weesee, Boroom beey wax, mu ne maay yeb sama ndigali yoon ci seen xol, ci seenum xel laa koy ñaas;