Hebrews 10:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bokk yi, gannaaw nag deretu Yeesu may na nu sañ-sañu dugg ca bérab bu sell-baa-sell,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag bokk yi, am nanu sañ-sañu dugg ca bérab bu sell baa sell, ngir deretu Yeesu,