bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 10:20
Hebrews 10:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
nuy jaar ci rido bi, ci yoon wi mu nu ubbil, di yoon wu bees tey dund, maanaam ndax li mu joxe yaramam sarax te mi ngi dund,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
deretu Yeesu jiy yoon wu yees, yoonu dund gu mu nu xàllal, jàllale ko rido ba, te rido ba moo di yaramu suuxam wi mu sarxe.