Hebrews 10:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
te gannaaw am nanu saraxalekat bu mag, biy yilif waa kër Yàlla,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am nanu itam sarxalkat bu mag bu jiite kër Yàlla.