Hebrews 10:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nanu jàpp ci yaakaar, ji nu am, te bañ a toqi, ndaxte ki nu dig, lu mu wax def ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nanu ŋoy ci yaakaar, ji nu biral ne moom lanu am, te nu baña yoqi, nde ki dige ku wóor la.