Hebrews 10:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku jub ci sama kanam dina dund ci kaw ngëm,waaye bu delloo gannaaw,sama xol du sedd ci moom.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sama nit ku jub nag mooy dund ndax ngëm ga, waaye ku dellu gannaaw, sama xol bégewu la.»