Hebrews 10:39 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nun nag bokkunu ci ñiy dellu gannaaw bay réer, waaye nu ngi bokk ci ñi am ngëm tey mucc.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun nag bokkunu ci ñiy dellu gannaaw te nara sànku, waaye nooy ñi saxoo ngëm te nara mucc.