Hebrews 10:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Looloo tax bi muy wàcc àddina, Kirist nee na:«Bëggoo saraxu mala walla beneen sarax,waaye aw yaram nga ma defaral.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax ba Almasiy dikk ci àddina la wax ne: «Saraxug jur aki jooxe, taamuwuloo ko, waaye aw yaram nga ma waajalal.