Hebrews 10:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Wax na bu jëkk: «Saraxi mala walla yeneeni sarax, sarax yu ñuy lakk walla sarax yiy dindi bàkkaar, bëgguloo leen te benn neexu la ci.» Teewul yoon wi moo leen santaane.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dafa jëkk ne: «Saraxi jur aki jooxe, saraxi dóomal ak saraxi póotum bàkkaar, bugguloo, safoowuloo,» doonte yoon wee laaj yooyu sarax.