bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 11:1
Hebrews 11:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Am ngëm lii lay tekki: dafa nuy wóor ne, li nuy yaakaar dina am, te it li nu dul gis nekk na.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngëm nag mooy cëslaayal yaakaar te mooy firndey li bët gisul.