Hebrews 11:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye nag Ibraaymaa ngi doon séentu dëkk bi sax, bi Yàlla tabax te sanc ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba Ibraaymaa ngay séentu dëkk ba ca kenu ya, te Yàlla di ki yor xaralag tabax bi, boole ci di tabaxkat bi.