Hebrews 11:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñoom ñépp dee nañu ci ngëm. Jotuñu li ñu leen digoon, waaye séen nañu ko fu sore ba nuyu leen, te nangu ne, ay doxandéem ak i gan lañu woon ci àddina.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñoom ñépp ngëm lañu deeyaale te jotaguñu woon la ñu leen digoon. Waaye fu sore lañu ko séene, di ko séentu, tey ràññee ne ay doxandéem aki màngaan lañu ci àddina.