Hebrews 11:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ngëm moo tax Ibraayma naroon a rey Isaaxa ni sarax, bi ko Yàlla nattoo. Moom mi jotoon dige yi, moo demoon bay saraxe jenn doom ji mu am kepp,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ibraayma, ba ñu ko nattoo, ngëm la jooxee Isaaxa ngir sarax. Ibraayma mi ñu jagle dige yi, Isaaxa jenn doomam ju góor ji mu am, moom la doon jooxe,