Hebrews 11:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ngëm moo tax ba, bi Musaa juddoo, ay waajuram nëbb ko lu mat ñetti weer, ndaxte gisoon nañu ne, xale bu taaru la woon, te ragaluñu woon ndigalu buur bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Musaa juddoo, ngëm la ko ay waajuram làqe woon ñetti weer, ndax gis na xale ba taaroo woon, ba ragaluñu ndigalal buur ba.