Hebrews 11:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu toroxal ko ngir Almasi bi mi ngi mel ci moom ni alal ju ëpp alali Misra yépp, ndaxte yool bi la doon séentu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Toroxtaange gu ñu koy teg ndax Almasi, moom la defoon muy alal ju ëpp denci Misra, ndax yoolub ëllëg ba la doon séentu.