bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 11:28
Hebrews 11:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ngëm moo tax mu sos màggalu Bésu Jéggi ba, di wis deret ci bunt yi, ngir malaakam Yàqkat mi bañ a laal taawi bànni Israyil.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngëm la Musaa aadaale màggalu bésub Mucc ba, ak wis-wisalub deret ja, ndax malaakam bóomkat bi baña laal taawi bànni Israyil.