Hebrews 11:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ngëm moo tax ba bànni Israyil jaar ci Géej gu xonq gi, mel ni kuy jaar ci yoonu suuf su wow. Waaye bi ci waa Misra yi doon jéem a jaar, ñoom ñu daldi lab.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngëm la bànni Israyil jàlle géeju Barax ya, mu mel ni yoonu suuf su wow koŋŋ, waa Misra jéema jàll topp ca, daldi lab.