Hebrews 11:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ngëm a tax ba nu xam ne, Yàlla sàkk na àddina jaarale ko ci kàddoom, ngir li bët di gis, defarees ko ak lu bët mënul a gis.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngëm a nu xamal ne Yàllaa sose àddina wërngal këpp ag kàddoom, li gisu daldi sàkkoo ci lu gisuwul.