Hebrews 11:35 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ngëm moo tax ba ay jigéen gis ñu dekkal seeni néew, delloo leen ko; ñeneen ñi ñu metital leen, te bañ ku leen musal, ngir jot ndekkite lu gën.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngëm a waral aw jigéen dekkile ñu ñu deele woon; ngëm a waral ay góor ñu ñu mitital, baña dellu gannaaw, weccikoo ko seen njotug bakkan, ndax yaakaara dekki, ba gëna dundati ëllëg.