Hebrews 11:40 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte Yàlla dafa tëral lu gën ci nun te bëggu leen a yeggale cig mat, fi ak ànduñu ci ak nun.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax daa fekk Yàlla gisal nu demin wu gën ci nun. Moo tax boroom ngëm yooyu waruñu woona àgg ci tolluwaay bu mat sëkk, te fekk nun dikkagunu ba bokk ko ak ñoom.