Hebrews 11:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ku amul ngëm doo man a neex Yàlla, ndaxte ku bëgg a jegeñ Yàlla war ngaa gëm ne, Yàlla am na te dina neexal ñi koy wut.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku amul ngëm nag doo mana neex Yàlla, ndax kiy dikk fi Yàlla, fàww nga jëkka gëm ne Yàlla am na, gëm it ne ñi koy sàkku, moo leen di yool.