Hebrews 11:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ngëm moo tax ba Ibraayma déggal Yàlla. Bi ko Yàlla wooyee, mu dem toxu ci menn réew, ma mu waroon a jote ca Yàlla. Noonu la gàddaaye dëkkam te xamul woon fan la jëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Yàllay woo Ibraayma, ngir mu génn, jëm bérab ba mu mujj muurloo, ngëm la déggale Yàlla, ba génn, dem te xamul woon fu mu jëm.