Hebrews 12:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li am moo di ne, yar bu nuy dal, du ànd ak bànneex, day naqari, waaye gannaaw ga dafay meññ jub ak jàmm, ci ñi ko jariñoo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëgg la, benn yarub tey neexul, xanaa naqari. Waaye la yar bay mujj jural ña mu tàggat, jàmm la ak njub.