Hebrews 12:14 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Wutleen ak ñépp jàmm te fonk dund gu sell, ndaxte ku sellul doo gis Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sàkkuleen jàmm seen diggante ak ñépp, te it sàkkuleen sellnga, nde ku sellul du gis Boroom bi.
Recommended Reading