Hebrews 12:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
jege mbooloom taawi Yàlla, yu ñu bind seen tur ca asamaan. Jege ngeen Yàlla, jiy àtte ñépp; jege ruuwi nit ñu jub, ñi àgg cig mat;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
yeena àgg fa ndajem taaw, ya seeni tur binde fa asamaan. Yeena àgg fa Yàlla, àttekatub ñépp; yeena àgg fa noowi aji jub ña ñu matal sëkk.