bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 12:27
Hebrews 12:27 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci li mu wax: «Beneen yoon,» dafay xamle ne, Yàlla dina dindi yi ñu man a yengal, maanaam li ñu sàkk, ngir li ñu mënul a yengal sax ba fàww.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li mu ne «beneen yoon», di wund ne lees mana yëngal, lay dindi, te mooy li sàkke, ngir lees manula yëngal sax ba fàww.