bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 12:3
Hebrews 12:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Defleen seen xel ci moom, moom mi muñ noonu ko bàkkaarkat yi bañe woon, ngir bañ seen kàttan jeex, ngeen xàddi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xool-leen ci moom mi bàkkaarkat yi doon xeex, bala ngeena yoqi bay xàddi.