Hebrews 12:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte ku Boroom bi sopp, yar la,tey duma bépp doom bu mu nangu.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax Boroom bi, ku mu sopp, yar la, mooy bantal jépp doom ju ko neex.»