Hebrews 12:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bu ngeen bokkul woon ci yar, bi ñépp am wàll, kon dungeen ay doomi yoon; ay doom yu daganul ngeen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu ñu leen xañee yar bi jépp doom am wàll, dafa fekk ngeen di doomi po, waaye du ngeen doomi yoon.
Recommended Reading