Hebrews 13:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Looloo tax Yeesu sonn ca gannaaw dëkk ba, ngir sellal mbooloo mi ak deretam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo waral Yeesu itam deeye ca bitib dëkk ba, ngir sellale askan wi, deretu boppam.