bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Hebrews 13:18
Hebrews 13:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Deeleen nu ñaanal. Wóor nanu ne, sunu xel dal na, ndaxte danoo bëgg a rafet ci lépp lu nuy def.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Deeleen nu ñaanal nag. Li nu wóor de, moo di sunum xel yeddu nu fenn, te it di def lu baax ci lépp moo di sunu bëgg-bëgg.