Hebrews 13:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na leen Yàlla Boroom jàmm, mi dekkal sunu Boroom Yeesu, di Sàmm bu mag bi, ci darajay deret, ji fas kóllëre gu sax,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yàlla miy boroom jàmm, moom mi dekkal sunu Sang Yeesu, Sàmm bu mag bi, ci dooley deret ji mu fase kóllëre gu sax dàkk,