Hebrews 13:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na ñépp fullaal séy, te lalu séy bi bañ a taq sobe, ndaxte Yàlla dina àtte ñu yàqu ñi ak njaalookat yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na ñépp wormaal diggante bu ab séy dox, te ab lalu séy na mucc sobe, ndax fokati séy yi, ak jaalookat yi, Yàlla moo leen di daan.