Hebrews 13:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Buleen bëgge; deeleen doylu, ndaxte Yàlla ci boppam nee na:«Duma la wacc mukk,duma la wor mukk,»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buleen jikkowoo bëgg ub xaalis; doylooleen li ngeen am, ndax Yàlla moo ne: «Duma la bàyyi mukk, duma la wacc mukk.»