Hebrews 13:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ba tax nu am kóoluteg wax ne:«Boroom bi moo di sama ndimbal;duma ragal dara.Lu ma nit manal?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax nu mana am fitu wax ne: «Boroom beey sama ndimbal, duma tiit. Ana lees ma manal?»