Hebrews 2:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Moo tax kon nu war a gën a faaydaal wax yi nu dégg, ngir bañ a bayliku.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax nu wara yokka teewlu kàddu yi nu dégg, bala noo lajj, taañaañal.
Recommended Reading